VIDEO: Akhlou Brick – No Issue MP4 Download | NaijaPower
Videos

VIDEO: Akhlou Brick – No Issue

Akhlou Brick No Issue

Akhlou Brick No Issue Video Mp4 Download

Akhlou Brick shares the official music video for the song titled “No Issue.”

This track was produced by Steady Key—Weezyade—Ibou Mbaye.

“No Issue” music video directed by WWS (World Wide Studios).

Watch and share your thoughts below:

Akhlou Brick – No Issue MP4

 

Akhlou Brick No Issue Lyrics

(ARA)
Akhlou Brick from Sénégal
West Afraica World wide

Hawma louma gnam ba diodo
Sa liguéya diap sa Serigne bé aay
Tek ma naagn dima madj lo
Yay sama Générale nala todial way
Takhaliko menoutoula né
Kanar bi teud nagn ko sani guédj bae

Falewma bénén go
Lidiantiwma bénèn go
Matay nop la angou thiow li
Bb nagnou rouslo wahi noni
Faw rek gnou wan lén ko

Jelel sama money now
Guisatouma Baby goumba na nah yay sama eyes
You make me feel the good life
Give You my money
See You go down
For me Yi go down low
Baby loumala may hep nako
Te man awma si yaw sago
Bb wan ma ningay dago
This is the way
Wan ma ningay dago
this is the way
Wan ma ningay dago
This is…

(Dayza)

Ba sa xol Bangui sed
Man mangui fekh
Retalna man malay xol rek di bek
Wanél niga meunee
Wanél né dou Ben
Dieund lal bou noy wanla noy danou si nek dengua,
Foma fek dik sif ma séey
Fo aw yon nangoulnala Biss niki tay
Meusso guiss djinee yak mom kif kif la kay
Gagné nga Sama coeur dakh sa assou pikaray

(ARA)
Ligéyma dama beug geunla bardé
Nagn ko doumdou mak yaw kassé
Mbeungel boudé rayé yalna dé
Meunatouma sound dans yaw

(DAYZA)

No man awma diom
Paka bingma rayè mako dass
dara metiwouma sino malila alma gaz
lamign béngui sa poche
sagnatouma kass
Guissna sama ourou ayni nieuweul fi gnou danse kay

(ARA)

Jelel sama money now
Guisatouma Baby goumba na nah yay sama eyes
You make me feel the good life
Give You my money
See You go down
For me Yi go down low
Baby loumala may hep nako
Te man awma si yaw sago
Bb wan ma ningay dago
This is the way
Wan ma ningay dago
this is the way
Wan ma ningay dago
This is…

Sa hol bi gagnou won na
Maa gnew fadial la gomi
Rangogni fér na honey
No mind!
I never u let you alone
Dou dem la gneup wahone
Décider wougn ko won
It just man ak yaw dong
Manak yaw la wara don bou thi ken dougou

Falewma bénén go
Lidiantiwma bénèn go
Matay nop la angou thiow li
Bb nagnou rouslo wahi noni
Faw rek gnou wan lén ko

Jelel sama money now
Guisatouma Baby goumba na nah yay sama eyes
You make me feel the good life
Give You my money
See You go down
For me Yi go down low
Baby loumala may hep nako
Te man awma si yaw sago
Bb wan ma ningay dago
This is the way
Wan ma ningay dago
this is the way
Wan ma ningay dago
This is…

Leave a Response